Chronique de Hadj Bécaye, ce Dernier Crache ces vérité aux VIP de L' aréne "Lac 2 Ak Eumeu Séne..."

1 543 Vistas 159 mil

Abonnez-vous à notre Chaine EStitle: estitle.info/more/udfBmVXjm-DTPjYNv8AWvQ.html?view_as=subscriber Aimez notre page Facebook: becayembayetv/ Visitez notre Site web: www.fmsenegal.info #Bantambatv.
77 419 03 64

Comentarios

  1. kolim jone
    kolim jone
    Hace 2 días

    Merci sama père Beckay grand contre petit reugue reugue ak franc koudieuloull sëne avance ragal nga 🇨🇵🇨🇵🇸🇳🇸🇳

  2. BIGTHIO Danfa
    BIGTHIO Danfa
    Hace 3 días

    Yaw boy niang dafa am defaite Ken bouko force AMA balde kokou dafa merite bokoul ak boy niang bo xamni dou songue fila beurre ak zoss cng wathie neko beurre par force

  3. Ass Gueye
    Ass Gueye
    Hace 4 días

    Wakh ga degue de lac si bopam dafa gniakeu fayda amoul dioum bilahi

  4. Moussa Matar Fall
    Moussa Matar Fall
    Hace 4 días

    modou lo moy sama mbeur mé père balla kouka nangou loul limou def si lamb ji diapal ni do sénégalais....

    1. kolim jone
      kolim jone
      Hace 2 días

      Pere ta tout dit yale na yala goudal sa fane

  5. diouf abdoul ahad
    diouf abdoul ahad
    Hace 4 días

    Revanche yi mo wara doyy

  6. Ale Gaye
    Ale Gaye
    Hace 4 días

    Per békaye yage fi lol té wer DEUG ré k ga vahk machallah

  7. Ibrahima Pakala
    Ibrahima Pakala
    Hace 5 días

    Staff Mbeur yii nagne bayii Mbeur yii deff sen mene mene

  8. diop magatte
    diop magatte
    Hace 5 días

    Merci so wakhone lelene ma rouss

  9. lourd12 diop
    lourd12 diop
    Hace 5 días

    Vous avez parfaitement raison Balla gaye day leik reugu reugu deih

  10. galass Sakho
    galass Sakho
    Hace 5 días

    Tontou degue leu dh

  11. Pape Cisse
    Pape Cisse
    Hace 5 días

    Lou lére na midi 🕛 nga wakh.

  12. Gorgui Faye
    Gorgui Faye
    Hace 5 días

    Lou léer nga wakh pére deug nékhoul

  13. GALAYE DIOP
    GALAYE DIOP
    Hace 5 días

    balla gaye ken rawouko sof badé

  14. Bac49 pzzi
    Bac49 pzzi
    Hace 5 días

    Il respire la Sagesse et la tranquillité Pere Becaye !

  15. Abdoul aziz baïdy Hane
    Abdoul aziz baïdy Hane
    Hace 6 días

    Vérité absolue

  16. Neinishh Sarr
    Neinishh Sarr
    Hace 6 días

    Bacaya yaye sama papa

  17. Modiene Yauck
    Modiene Yauck
    Hace 6 días

    Deugue rek guafi wakh bilaye yaye lambou

  18. Niomi Ba TV
    Niomi Ba TV
    Hace 6 días

    Verite'absolue Pere

  19. Gora Sambe
    Gora Sambe
    Hace 6 días

    Pere ta tout dit yale na yala goudal sa fane

  20. sidaty ba
    sidaty ba
    Hace 6 días

    Merci beaucoup per waxdji amna solo machalah

  21. Omar Kane
    Omar Kane
    Hace 6 días

    Kone khana Modou lo meritewoul vitouiar ak lac 2

  22. Ibrahima Bodian
    Ibrahima Bodian
    Hace 6 días

    Pére yaffi né

  23. Ibrahima Willane
    Ibrahima Willane
    Hace 6 días

    Mani woutal len malick niang comba nameu nen ko

  24. Abdoulaye mboutou Fall
    Abdoulaye mboutou Fall
    Hace 6 días

    Merci père

  25. Preuve Nii
    Preuve Nii
    Hace 6 días

    Becaye bilahi deug rek ga wakh

  26. byPerri
    byPerri
    Hace 6 días

    WAKANDA FOREVAH

  27. Malik King
    Malik King
    Hace 6 días

    gris bordeau moye president yakh katou lamb yi, amoul palmares té nénaye VIP la, VIP rek leye amal combat

  28. Sarr Abdou
    Sarr Abdou
    Hace 6 días

    Lac 2 méritéwul khaliss sou lamb

  29. Selle Sarry
    Selle Sarry
    Hace 6 días

    CLARO que sí

  30. Moïse
    Moïse
    Hace 6 días

    Lou lére gua wakhe békaye

  31. Prierra Allen m
    Prierra Allen m
    Hace 6 días

    Bekay je suis daccord avec toi na bayi beurer ak haley yii

  32. Aladji Fall
    Aladji Fall
    Hace 6 días

    Vraiment Deugue Le

  33. Serigne Sow
    Serigne Sow
    Hace 6 días

    Thank you pere❤️🇸🇳

  34. BAM'S BAM'S
    BAM'S BAM'S
    Hace 6 días

    Pére na'na'niou waxanté deug nit kéne dou'ko fékeu si keureum néko ni'ngay teudé / wayé bo'léne dadjié si mbéde'bi boula doré am'na sagne sagnou fayou

  35. Top Khadim
    Top Khadim
    Hace 6 días

    Per Lou ler nga wakh bilahi

  36. Abdourahmane Kounta
    Abdourahmane Kounta
    Hace 6 días

    Gris na dieul lac boudei lac amna fitt

  37. sall abdou
    sall abdou
    Hace 6 días

    Ta raison papa bèguè

  38. Khadidiatou CAMARA
    Khadidiatou CAMARA
    Hace 6 días

    Yagu fi lol andak wëreu pére bècaye deugu rék Ngua wakh dafa diote Lamb dji changé wakhal ngua peuple bi mahchahala

  39. babacar Traorè
    babacar Traorè
    Hace 6 días

    Merci père Becaye fière de vous

  40. Jaaw Fara
    Jaaw Fara
    Hace 6 días

    Belle analyse per becaye

  41. fatou thiaw ciss
    fatou thiaw ciss
    Hace 6 días

    Père ya niemé deugue pirrree tapha tine dou tapéte

  42. Salif NGaide
    Salif NGaide
    Hace 6 días

    Gris Bordeaux vs gouye gui Eumeu vs sa thies Balla vs boy niang Modou lo vs ama Lac 2 vs tapha tine B52 vs reug reug Franc vs amanekh 🔥🔥🔥🔥

  43. Papy Thiat
    Papy Thiat
    Hace 6 días

    Deug dou Romb Nope: Gris depuis quand danoufi ken ba paré begoul dieul xaléyi, Niom nieup danio ragal boy yi ak Tapha Tine billahi

  44. Talibe Cheikh Tv
    Talibe Cheikh Tv
    Hace 6 días

    Tu a raison père linga wax lep deugeu la

  45. Mbaye Modou
    Mbaye Modou
    Hace 6 días

    Békaye waxji amna solo

  46. Babacar Gueye
    Babacar Gueye
    Hace 6 días

    Tu es un vrai Penseur et mémoire de la lutte sénégalaise

  47. Moustapha Diedhiou
    Moustapha Diedhiou
    Hace 6 días

    Diene kaïre vs Domou dangou

  48. Ngalla Faye
    Ngalla Faye
    Hace 6 días

    Qui est d'accord avec père beusal jm

  49. Alieu Cham
    Alieu Cham
    Hace 6 días

    Lac 2 dou dara 👎

  50. arimaz
    arimaz
    Hace 6 días

    Papa Becaye yalla naga goudou fane mane meusoumalz guiss yak papa Mansour mbaye mais sa doumalen guisser si télé bi damalen di nianal goudou fane yalla nangen fi yague lol ter weur

  51. Oumy Niang
    Oumy Niang
    Hace 6 días

    éhyy Mbaye,yalna sa jamm yague mais père lac nguéinn wara waxal Mou changé Meunounio comprendre kouy nul môme ngay nuleul père lac dafay soul ndanane ndax dou beuré kaatt

  52. Baye Mboup
    Baye Mboup
    Hace 6 días

    Bilaye wakh nga degue yague fii lolou te wer

  53. Madjiguene Sy
    Madjiguene Sy
    Hace 6 días

    Wakh ga deugue deh

  54. Demba Diallo
    Demba Diallo
    Hace 6 días

    Bilahi papa bekay defa ler

  55. Chicory Kharagne
    Chicory Kharagne
    Hace 6 días

    Kou muen Fran na niuew?? Sa thies moussa ndoye diene modou anta kou niuew nexna

  56. TAPHA Satt
    TAPHA Satt
    Hace 6 días

    lat dousama mber me df na efor

  57. cheikh gueye
    cheikh gueye
    Hace 6 días

    Vip poltron

  58. Penda Drame
    Penda Drame
    Hace 6 días

    Mane dal ma beugue balla aucune déception dey beure mou dane la wala nga dane ko mou Diekh ay supporter Ram dou niou ame gathie de

  59. él presi90
    él presi90
    Hace 6 días

    Pér deug piir nga wah

  60. Baye Aladij Mboup
    Baye Aladij Mboup
    Hace 6 días

    Vraiment 👊👊👊😘

  61. Saliou Fam
    Saliou Fam
    Hace 6 días

    Degue dou rombu ay nopou Lou ler gua wakh

  62. Stanky Officielle
    Stanky Officielle
    Hace 6 días

    Pour se dire la vérité tonton tu as parfaitement raison moi je suis venez lutter avec moi mdr 🤣🤣

  63. Bathie Diop
    Bathie Diop
    Hace 6 días

    Diam siyaw père beckay yaw rek ladone khar nga wakh🙏🏿🙏🏿

  64. Awa Ndeye
    Awa Ndeye
    Hace 6 días

    Merci beaucoup père bécaye🙏😘

  65. Sophia Faye
    Sophia Faye
    Hace 6 días

    Macha Allah. Ya wax DEUG pure

  66. naby Ndiaye
    naby Ndiaye
    Hace 6 días

    begue si yaw pere wakh gua lepp

  67. Street Tv online live
    Street Tv online live
    Hace 6 días

    Pere becaye merci. Dundeul

  68. Tapha Kara
    Tapha Kara
    Hace 6 días

    Merci

  69. Bamba Kebe
    Bamba Kebe
    Hace 6 días

    Pére waxofii dara boy yii si bopam ñion amoule diom

  70. Omzo Ramos
    Omzo Ramos
    Hace 6 días

    Vérité absolue il est tant lamb dji oubékou

  71. Ndiaga Sarr
    Ndiaga Sarr
    Hace 6 días

    Merci tonton Becaye!!!

  72. Assane Diop
    Assane Diop
    Hace 6 días

    Vraima dagno sone si mm combat yi daffa doye

  73. La touche Magique
    La touche Magique
    Hace 6 días

    Wakh dji nagne ko wakh ta deh,lac nako promoteur yi arretel teugeul combat niep am diam la paix

  74. ardin midio alhamdullh
    ardin midio alhamdullh
    Hace 6 días

    Machall

  75. AM BOU KHARAGNE LO
    AM BOU KHARAGNE LO
    Hace 6 días

    Bilaye papa ndeyessen lac du Dara

  76. Mamadou Ndong
    Mamadou Ndong
    Hace 6 días

    Becaye c le meilleur 👏👏👏👏👌

  77. Ibrahima Ndiaye
    Ibrahima Ndiaye
    Hace 6 días

    Père Bécaye yagueu naa diokhé leçon de moral. Kou weddi na nga seetaan toujours ses derniers messages fin Bantamba. Toute une pédagogie. Parfois aussi mou remettre mbeur à l'ordre. Parfois mou encourager mbeur mou am déception. Chapeau père Bécaye

  78. Cheikh tidaine Gueye
    Cheikh tidaine Gueye
    Hace 6 días

    Machalla dounde père wallakhi

  79. Talibe Mamesaliou
    Talibe Mamesaliou
    Hace 6 días

    Lac dou touss dafa wara géni lambji

  80. Fallou Mballo
    Fallou Mballo
    Hace 6 días

    Billahi pére bécaye wakh nga deug

  81. Aminata Faty
    Aminata Faty
    Hace 6 días

    Vraiment moi j’avais arrêté de supporter Lac depuis longtemps .rouslo waté rek....Sétane ba sa am mal de dos commencé nélaw....en plus à Paris il était déjà minuit...vraiment Balla rek🥰🥰Merci pour l’analyse

  82. Mohamed
    Mohamed
    Hace 6 días

    REGLEMENT BI MO WARA DINDI 45 MN BAYI SENE KHONE FOFOU BA SOUBA KOU DANE NIOU SOGUA TASS DAFA YOMB TROP

  83. Astou Faye
    Astou Faye
    Hace 6 días

    Merci.mbaye.machallah

  84. Mor Cisse
    Mor Cisse
    Hace 6 días

    Mane dama dieunde page 9.90€ mais benen yon EStitle lay khar bodoul won di kaire kon mouniaw eumeu bomla dalaty yaw champion nga yaye sama mbeur mais bi yon mom yoroko wasalam

  85. KheuSH Sylla
    KheuSH Sylla
    Hace 6 días

    Bient Ditt Pére

  86. demba assane sy
    demba assane sy
    Hace 6 días

    Combat eumeu vs lac2 drapeau macky sall nékhoule dara tourondo lamba dji Modou lo vs ama toudéléne ko drapeau ousmane sonko ndakh mou nekh

  87. Corail Productions
    Corail Productions
    Hace 6 días

    Franchement, Becaye sa analyse bakhna !

  88. Maman Dieng
    Maman Dieng
    Hace 6 días

    Lou lére gaaaa wakhe diammm sii yaw pére bécaye ndoundale waye on tm fore

  89. Birane Ndiaye
    Birane Ndiaye
    Hace 6 días

    No père becaye t'as fait une très belle analyse franchement.

  90. Dramane Hebie
    Dramane Hebie
    Hace 6 días

    Absolument tu as raison Père Becaye

  91. MAMADOU DIENG
    MAMADOU DIENG
    Hace 6 días

    Merci Pére Bécaye vous avez parfaitement raison ces soi disant ténors de l'arène doivent accepter de lutter avec les autres comme reug reug,franc,ibou ndiaye et tant d'autres. C'est très facile ce qui se passe actuellement dans l'arène.

  92. Cheikh tidjane Kebe
    Cheikh tidjane Kebe
    Hace 6 días

    Merci waaaye père becaye walaye malla beug ndakh DEUG ak beug jaam

  93. ouz ndiaye
    ouz ndiaye
    Hace 6 días

    Pere deug rek nga wakh

  94. Samuel Diouf
    Samuel Diouf
    Hace 6 días

    c'est ce genre de personne analyste qu'on a besoin au senegal. dire la vérité, rien que la vérité.

  95. Samuel Diouf
    Samuel Diouf
    Hace 6 días

    c tres clair père. faut plus jamais preparer un combat pour lac car c k du gachi. il gagne de l'argent facilement

  96. Baba Gningue
    Baba Gningue
    Hace 6 días

    Wakh degue lamp dou gnom rek nagnou dieul boy yi mou yatou

  97. Prinççe D-G Cms Samb
    Prinççe D-G Cms Samb
    Hace 6 días

    Père Bécaye Eume ak lac sen combat nila meune Mel ndakh biss dou touti borom lay tolole boulen faté ni drapeau chef de l'état la nak manoul nékh

  98. Maïmouna SAMB
    Maïmouna SAMB
    Hace 6 días

    Niak diom rek nagn len arrêter tegueul combat mo gueune ay millions lagn sani si poubelle bi tei amna gnuko guenone yello

  99. GALAYE DIOP
    GALAYE DIOP
    Hace 6 días

    Machala pere il est temp lamb changè cris vs sa thies Si non mou annè blange

  100. Oumar Gueye
    Oumar Gueye
    Hace 6 días

    Merçi pére