Intégralité combat Lac 2 vs Eumeu Sène

2 770 Vistas 323 mil
Deportes

Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct luttetv/
luttetv/
luttetv
luttetv.com/
estitle.info

Comentarios

  1. Assane Faye
    Assane Faye
    Hace un día

    Lac dafa waara bayi beurré deme défi lenenne

  2. Abdou Faye
    Abdou Faye
    Hace 4 días

    Gnom gnar gnépa beuré dam ken Douko.wenter

  3. asioe kiou
    asioe kiou
    Hace 5 días

    MODOU Le Boss !!!ONE Love

  4. Rock girl
    Rock girl
    Hace 5 días

    Diadieuf Lac2 yako meune fouf diko dah mouy daw rek.

  5. Astou Diakhatè
    Astou Diakhatè
    Hace 6 días

    Lac défo fi dara démal ga togue wah rék ga meune.

  6. bouytt guyt
    bouytt guyt
    Hace 6 días

    40munitou yalla gnouy weur weurloo amateur yi sans même un seul contact physique 🤔 mé yi tam nagnouko si lac2 motakh ma gueum balla gaye 2

  7. Ismail Diassi
    Ismail Diassi
    Hace 7 días

    Lamb de merde

    1. asioe kiou
      asioe kiou
      Hace 5 días

      Combat à l'image du parrain de cette médiocrité....

  8. Ailsa Ni
    Ailsa Ni
    Hace 7 días

    Heureusement que la distanciation social a été respecté 😅😅😅combat covid 19 ngay am fofou

    1. Rock girl
      Rock girl
      Hace 5 días

      Combat bi lepeu sooff teugg mi sakh dafa sooff

  9. Farimata Samb
    Farimata Samb
    Hace 8 días

    Pierre faire

    1. bouytt guyt
      bouytt guyt
      Hace 6 días

      Kén barewoul

  10. Sidi Doip
    Sidi Doip
    Hace 8 días

    Bilahi boudone balla guaye diékh na

  11. Awa Diallo
    Awa Diallo
    Hace 8 días

    Eumeu séne laniou wakh san pour san eumeu chéri Khou

  12. Imam Djibril Ndiaye
    Imam Djibril Ndiaye
    Hace 8 días

    Machalla lutte tv et buzz

    1. Ailsa Ni
      Ailsa Ni
      Hace 7 días

      Je ne savais pas que dans l'arène il y'avais des comédiens ! Gni kou niou yab ?

  13. fall Ousseynou
    fall Ousseynou
    Hace 8 días

    Wakh rek laye def lac

  14. Anastasia Dieng
    Anastasia Dieng
    Hace 9 días

    Sheut franchement lac m’énerve eumeu Sene aussi ils n’ont rien foutu merde fallait leurs laissés dans le stade kou dane sa morom woté téléphone

  15. Amadou dieye Kebe
    Amadou dieye Kebe
    Hace 9 días

    Bilahi lacs amél guama akh dh sama hémorite yeguatouna 40mn magui took

  16. DESNA WEZZ
    DESNA WEZZ
    Hace 9 días

    mo wayyy

  17. marema fall
    marema fall
    Hace 9 días

    Mane mom dama djiomi si bi comba wa eumeu sene mi louko dal vraiment tu m'a déçu

  18. Amadou Yoro Fall
    Amadou Yoro Fall
    Hace 9 días

    Ce combat, décevant est à l'image de son parrain mais également de son promoteur.

  19. Fode Traore
    Fode Traore
    Hace 9 días

    On dirai combat des coqs

  20. Mamadou Seck
    Mamadou Seck
    Hace 9 días

    Combat Balla Gueye mon nehk

  21. Sosodia
    Sosodia
    Hace 9 días

    Combat à l'image du parrain de cette médiocrité....

  22. Abo Fall
    Abo Fall
    Hace 9 días

    Combat bi lepeu sooff teugg mi sakh dafa sooff

  23. Abdou DIOUF
    Abdou DIOUF
    Hace 9 días

    Eumeu am na droit teudie lamb dji sokhla woul denko sokh la N Domou kharam bi Lac mi reuy lamegne kay na dem foukarthji loumou sokhla bagna khar niou may ko comme day gamou kay

  24. Ndony Diattara
    Ndony Diattara
    Hace 9 días

    Kén barewoul

  25. Sada Dkr
    Sada Dkr
    Hace 9 días

    Tres décevant ce combat

  26. biggy ben
    biggy ben
    Hace 9 días

    Je ne savais pas que dans l'arène il y'avais des comédiens ! Gni kou niou yab ?

  27. Fatimata Sow
    Fatimata Sow
    Hace 9 días

    Faut revoir les décisions arbitrales gni gnak diom dougnou dieul Benz initiative silagnouy profité

  28. Fatimata Sow
    Fatimata Sow
    Hace 9 días

    Mbeur yeup gno wara of lac de guiers dafa niak diom

  29. Doudou Ndiaye
    Doudou Ndiaye
    Hace 9 días

    Billahi nekhoul ba nekh mais beurè ak Lac 2 day wagni sa crédibilité tapetla rek

  30. ligue1&2 sénégalais fsf
    ligue1&2 sénégalais fsf
    Hace 9 días

    Lamine tu es professionnel

  31. Modou Diagne
    Modou Diagne
    Hace 9 días

    So beugué combat bou nékh teugueul Modou xaragne lô Balla ama ak gnognou nioy beuré

  32. Maodo Fall
    Maodo Fall
    Hace 10 días

    No gnoune Gaston mo gnou khawma loutakh mouye teugeule Lac combat yambar bou bone bi.

  33. BD
    BD
    Hace 10 días

    Tous ces millions pour ça ! Chiimmm !

  34. Aida Gueye
    Aida Gueye
    Hace 10 días

    Magui khar ba keneu tegueti comba disi bolei lac tamna lii

  35. Galo Sene
    Galo Sene
    Hace 10 días

    Nn mbeurr yi mesure barrière yi laniou respecter distatiallation physique li com guerre😅😅

  36. Idy Xaragne Lo
    Idy Xaragne Lo
    Hace 10 días

    Li dou combat léwtoo la

  37. Dame Diop
    Dame Diop
    Hace 10 días

    Niome niare kéne beuré wousi aye ragal lanou rek

  38. Jammal Anderson
    Jammal Anderson
    Hace 10 días

    Lac gui daffa kate ndayame

  39. Mariama Diatta
    Mariama Diatta
    Hace 10 días

    Combat médiocre lac mome mou melni kouye baskette nii. 😆ô

  40. Aliouinho Aw
    Aliouinho Aw
    Hace 10 días

    Wakh deug yalla contre n'a Lac 2 trop mais combat bi môme moko beurre leppu Eumeu Séné beureoul Dara 🙈🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣💪

  41. Ousmane Sane
    Ousmane Sane
    Hace 10 días

    Non mais Qui lac2 dafko humilié eumeu légui Modou lo wakhnakko 😅🤣😂😅🤣😂👊🤛🤜💪

  42. Omar Ba
    Omar Ba
    Hace 10 días

    Combat distanciation sociale,no coronabi mo yak combat.

  43. Douweuz la Fouine
    Douweuz la Fouine
    Hace 10 días

    Lac 2

  44. Jack Dafe
    Jack Dafe
    Hace 10 días

    Bob

  45. Cawane Ndoye
    Cawane Ndoye
    Hace 10 días

    Kenn dou balla💪💪💪💪

  46. BAM'S BAM'S
    BAM'S BAM'S
    Hace 10 días

    Merci lac kou mèr tampi soxor baxoul

  47. Ndeyeomzoo Diop
    Ndeyeomzoo Diop
    Hace 10 días

    Ma khala eumeu diap Modou lô rek Darko Moulay dan rek guay ande ah mom chaque jour Modou lô si bopam Moy yak sa carrière légui Moy touko mogui lay Ray rek wah nala Lima kham Modou lô méh séd Ray la dh

  48. Code Mbathie
    Code Mbathie
    Hace 10 días

    nayis na

    1. Code Mbathie
      Code Mbathie
      Hace 10 días

      Boubou Mbathie

  49. Bab Diouf
    Bab Diouf
    Hace 10 días

    Lac da niak diom mo wara song si ndax Eumeu nek na roi ba par3

  50. Seynab Fatale cisse
    Seynab Fatale cisse
    Hace 10 días

    Waye ma beugue bala thi âme diome

  51. Mass Ibn haïri
    Mass Ibn haïri
    Hace 10 días

    lac mo yakk combat bi

  52. Modou Mbaye Ka
    Modou Mbaye Ka
    Hace 10 días

    Youssou ndour dila waye yadanu melni yada

  53. Umou Khairy
    Umou Khairy
    Hace 10 días

    Waxante wax deug sila eumeu defoufi Dara wolah lac def na lep vraiment

  54. Leyti Ndiaye
    Leyti Ndiaye
    Hace 10 días

    Lac gordjigéne la mo mome lagn may revanche

  55. Pape Sylla
    Pape Sylla
    Hace 10 días

    Wa lac mi dougne ko guéné si lamb dji yobb ko si lumbeul bi😂

  56. Toure Cheikh abdou lahad
    Toure Cheikh abdou lahad
    Hace 10 días

    Commentaire bi baaxoul 👉😡👎👎👎👎👎

  57. serigne mbaye
    serigne mbaye
    Hace 10 días

    Nie man domalen support niom laniy yoni nioy dorr manifestation yii

  58. Astou Mbodji
    Astou Mbodji
    Hace 10 días

    Lac mo niak diome Cheteuteu kene waratouko teugeul combat

  59. Ba Ndari
    Ba Ndari
    Hace 10 días

    Ken gneme woul

  60. Mamadou lamine MANE
    Mamadou lamine MANE
    Hace 10 días

    BALLA rek moo gniou maye takousanne bou nekh dia dieff balla

  61. d g
    d g
    Hace 10 días

    ??? Wtf? Fuck!

  62. Broken
    Broken
    Hace 10 días

    Que diablos me recomienda EStitle

  63. mya chou
    mya chou
    Hace 10 días

    Sérieusement beuré wouléen darra eumeu tay tu mas déçu

  64. yaro bakh tv
    yaro bakh tv
    Hace 10 días

    Lac a tout tenté franchement.

  65. samu el
    samu el
    Hace 10 días

    *It's time to repent and seek JESUS* .He gave his life, and suffered the wrath of the Father in the cross, to save you from a eternal hell. For God loves you, but the sin must be punished. On the third day He raised from the death, showing to the world that He is God. So stop sinning and clean your life. He returns soon to judge and destroy the sinners. *Read the Bible.* *THE END IS NEAR.*

  66. Diallo Djibi
    Diallo Djibi
    Hace 10 días

    Cool

  67. Khady Thiam
    Khady Thiam
    Hace 10 días

    Eumeu amoul dara loumouy prouver lac Naina Moy khalai té dafay cons combat bi eum dako faikssi si noumouy beurai rek

  68. Ndama Torino
    Ndama Torino
    Hace 10 días

    Lac beuré na eumeu mi tay mo andi galas meussa def li

  69. Mamor Niang
    Mamor Niang
    Hace 10 días

    Beurrré wou lén fi dara

  70. Moustapha Bilal
    Moustapha Bilal
    Hace 10 días

    Me mané lima sert Lou lac Ben lokho leu beureu ba comba bi diekh

  71. lary normal
    lary normal
    Hace 10 días

    Lac dou dara vrai goor dafay am fitt

  72. haulepontio tabarèz
    haulepontio tabarèz
    Hace 10 días

    Modou ,Balla ,eumeu, Ama, goûté gui,tapha tine nio nékha teugeule comba lat mome beuss bou néké roi des aréne lambeu DÉ mane mome faufoulaye diaré bayi lambeu

  73. haulepontio tabarèz
    haulepontio tabarèz
    Hace 10 días

    Magkhy dora cétane comba bi lat bétenama li bane façon beuréla mane suportérou modou lo la mé kéneu dou balla gaye

  74. wakheet
    wakheet
    Hace 10 días

    Khawna ndakh setlouguen, Eumeu vs Lac, ngebeu Gris vs Balla lagnou sol.

  75. mariama sarr
    mariama sarr
    Hace 10 días

    Lac 💪💪🏆

  76. Mansour Diagne
    Mansour Diagne
    Hace 10 días

    🙈

  77. Astou Ba
    Astou Ba
    Hace 10 días

    Nékhoul nékhoul dara safou si thiey balla Gaye ya nékha farale dimanche 💪💪

  78. Ma Diaw
    Ma Diaw
    Hace 10 días

    Chiiiim 6 moy 9 niome niar nieuppa yèmm danio niakk diom

  79. adam's diallo
    adam's diallo
    Hace 10 días

    Bilaye eumeu nékhoule wone thii lamb ji lac dako diékou si lép bilaye mai lac dafa ragale trop 🤣🤣

  80. adam's diallo
    adam's diallo
    Hace 10 días

    Mane eumeu séne moye sama beure mai combat bi lac moko momone ragale rék mon takh danone eumeu

  81. WTF Jesus
    WTF Jesus
    Hace 10 días

    WTF? ... who can stay waving their hands longer?... I'm lost 😶

    1. Abdoulaye Tamba
      Abdoulaye Tamba
      Hace 9 días

      In deed!!!

  82. diome Bledard
    diome Bledard
    Hace 10 días

    Gnata carton rouge 🤣🤣🤣🤣

    1. Mansour Diagne
      Mansour Diagne
      Hace 10 días

      🤣🤣🙈

  83. almamy diaby
    almamy diaby
    Hace 10 días

    Combat covid 19 respect .drapeau Macky echec rek

  84. Bamba Seck
    Bamba Seck
    Hace 10 días

    A mon avis daniou wara changé système bi def ko 3 guéww premier bou makk deuxième mi temps bou ndaw 5 dernière minutes yi geuewou 1m mbeur bou guen niou dagg la 25% .

    1. Mansour Diagne
      Mansour Diagne
      Hace 10 días

      🤣🙏🏾

  85. Cheikh Mbacke
    Cheikh Mbacke
    Hace 10 días

    MACKY SALL LOKKO TOUDEE DOU NEX...

  86. Amidou Diallo
    Amidou Diallo
    Hace 10 días

    Lac waroul am combat

  87. Filipe Messias italy
    Filipe Messias italy
    Hace 10 días

    Que luta e essa?? 🔝🇧🇷🇮🇹l

  88. Ndeye Mbaye
    Ndeye Mbaye
    Hace 10 días

    C'est pas du combat

  89. Salam Prince
    Salam Prince
    Hace 10 días

    Eumeu yama rouslo

  90. Sarjo Jabbi
    Sarjo Jabbi
    Hace 10 días

    Congrats Lac 2

  91. Visionnaire Visionnaire
    Visionnaire Visionnaire
    Hace 10 días

    Lac de guerre dafa wara bayi

  92. lahad bou kharagne Lo
    lahad bou kharagne Lo
    Hace 10 días

    Lamine amoul quoi nena mitapms nganan afestisma😂😂😂😂

  93. Bour Sine
    Bour Sine
    Hace 10 días

    Promoteur bou beug sa haliss doko def si lac si décevoir amateur et promoteur lac deuk, lac est coutumé des faits

  94. lahad bou kharagne Lo
    lahad bou kharagne Lo
    Hace 10 días

    Eumeu ioe la beugon nga am Victor mes DESS nga paré té mes lac mom benn promoteur waratouko teug

  95. lahad bou kharagne Lo
    lahad bou kharagne Lo
    Hace 10 días

    Lac d'où Mbeur na Dem Modou Modou dji nopal bopam mes lamine liguey bi rafet na torop ak jamm

  96. Aboubacry Ndao
    Aboubacry Ndao
    Hace 10 días

    Lac mo gueuneu sokhla combat bi lou takh defoul nimou defone papa sow lac guerre ragal la eumeu nimou def nonou leu parce que il a une foi été le roi 👑 des arènes et en plus il est le plu âgé il est presk en fin de carrière lac style beuré bi la wara bayii chak combat nul nione sokhlowouniou nul mome ak boy niang tamite nii la defone dafa nio respecté woul rek respecté woul tamite wa guédiaway mbeur bou niaméoul cou dou mbeur mbeur faw nga melni BG2 da nga encaissé premier coup nga dem defi li ngay def dane deme sa yone chapeau a balla guaye2

  97. bamba ba
    bamba ba
    Hace 10 días

    Combat corona boul lal boul diegué

  98. Gamou Kane
    Gamou Kane
    Hace 10 días

    Lac d guier momm kouma waxati. Combat wam nala niouss

  99. Fallou Gueye
    Fallou Gueye
    Hace 10 días

    Lac kou mbeurei ak mom say suporter dinagnoula mėrė parsk dou.nekhal lamb

  100. Djibril Sene
    Djibril Sene
    Hace 10 días

    Combat bi est ce que dou complot tamit . Temps yi complot dafa hew si rewmi Ndah mofiy def beuz. Niom niar la