Ma Challah Eumeu Sène reçoit les prières de Balla Gaye 2 : "linga beugue ci sa khol ❤️ lepp..."

1 090 Vistas 111 mil
Deportes

Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct luttetv/
luttetv/
luttetv
luttetv.com/
estitle.info

Comentarios

  1. Zackaria Tounkara
    Zackaria Tounkara
    Hace 3 días

    Mental acier layorré Emeu ✊🏾✊🏾✊🏾

  2. Ibrahima Diallo
    Ibrahima Diallo
    Hace 4 días

    Je t'aime eumeu séne comme mon père

  3. Ridial Dieng
    Ridial Dieng
    Hace 4 días

    Mashala eum j SS fans Balla gaye Nice na

  4. Niass baye
    Niass baye
    Hace 5 días

    Amine 🙏

  5. Issa Sall
    Issa Sall
    Hace 5 días

    Mach alla

  6. Sokhna Ndiaye
    Sokhna Ndiaye
    Hace 6 días

    Eumeu rekkk💟

  7. Alhassane Diallo
    Alhassane Diallo
    Hace 6 días

    Ndesann dey retane rek yalla na diam yagg Sénégal

  8. Bamba Niang
    Bamba Niang
    Hace 6 días

    je vous parle yene Mbeur yi pourquoi bou sénégalais yi amé ay problème do lene si takhaw en ce moment là macky sall il nous fout là merde dans ce pays là vous ne dire rien

  9. Thierno Oumar Sylla
    Thierno Oumar Sylla
    Hace 7 días

    Eumeu sene Yallah nala Yallah faye sa xol

  10. Fallou Dieng
    Fallou Dieng
    Hace 7 días

    Fans balla LA ms eumeu sene amal diam rk

  11. Pape Modou Mbeungue
    Pape Modou Mbeungue
    Hace 7 días

    Bilay dousama mbeur me khol bou rafet la yor yalla nako yalla defal la diam bilay

  12. Mamadou Niang
    Mamadou Niang
    Hace 7 días

    Ndam rek champion

  13. Marie Musicof
    Marie Musicof
    Hace 7 días

    Non man eumeu sene day rétan rek

  14. Awa Mbengue
    Awa Mbengue
    Hace 7 días

    Amine way victoire inchallah s'ils plat par dieu amine

  15. Mamadou Diallo
    Mamadou Diallo
    Hace 7 días

    Ok c bien merci

  16. Ismael Faye
    Ismael Faye
    Hace 7 días

    Hol bou rafet GA yore bilahi eumeu stp so dane lac GA bayui beure do mbeur

  17. Thiam Elhadji
    Thiam Elhadji
    Hace 7 días

    yalna yalla Faye sa khole

  18. Ramos Sonko
    Ramos Sonko
    Hace 7 días

    Eumeu dou sama mbeur deh mais bagnoumako tamite ndakh kholam mo Rafète ❤️🙌

  19. L’absolu Gueye
    L’absolu Gueye
    Hace 7 días

    Naysann borom xol Bou nice la Barke serign Bamba Ndam Rék champion ♥️🙏

  20. Saly Dia
    Saly Dia
    Hace 7 días

    Bayil Sama fans bi Wayy 🤣

  21. Charlout Sam
    Charlout Sam
    Hace 7 días

    machalla eumeu la vie est courte

  22. Cheikh abdoul ahad borom belel Gueye
    Cheikh abdoul ahad borom belel Gueye
    Hace 7 días

    Rafètna

  23. Hadja diarieta Sy
    Hadja diarieta Sy
    Hace 7 días

    Balla Gaye kenn guenou ko rafete khol ❤️

  24. Saliou Ba
    Saliou Ba
    Hace 8 días

    MAIS FAIR PLAY BI DAFA EUPP ...DèLENN SAGANTè BA BAYI DOGA NEKK AY GANYINN BOUDOUL LOLOU DOU AMM TENSION .. SAGANTALENN ...NA METTI KHOLENN MOHAMED ALI AKK MANGA 2... JOE FRAISER ET ALI ..NA TANG 😂 MANN MOMM MODOU LO AKA KHARARAGN BALLA GAYE DAKA BEURè EUMEU SENE DORRKO 2 0

  25. Jolie Seye
    Jolie Seye
    Hace 8 días

    Niari boroom khol you rafet ✌eumeu sene dinga khamni nioune fans balla gaye yi kou beugue balla niou beugue la yallna jaam yague😊😊

  26. Gueye Xalile
    Gueye Xalile
    Hace 8 días

    Eume Diam rék inchallah Codo

  27. Walowalo Walowalo
    Walowalo Walowalo
    Hace 8 días

    Ô me ema sene l'an molay meti wakh ma dilal sama numéro 👂

  28. bamba Gueye
    bamba Gueye
    Hace 8 días

    Je l'aime fort Emeu

  29. lamane tine
    lamane tine
    Hace 8 días

    Djadiéf ameu💪

  30. Mam’s Koita
    Mam’s Koita
    Hace 8 días

    Eumeu sene bilahi xol bou nice la yor day réé rék

  31. Pablo El Fenomeno
    Pablo El Fenomeno
    Hace 8 días

    Eumeu Rek ya yarou te faire play Rafetna bok

  32. Moussa Sene
    Moussa Sene
    Hace 8 días

    Eumeu yalla nala yalla defale diam ak kheuwale youbari si barké seyedina mouhamad

  33. Diakhate Cheikhna
    Diakhate Cheikhna
    Hace 8 días

    Eumeu bala les 2 khole you rafete laniou yore

  34. Prince Kaka
    Prince Kaka
    Hace 8 días

    Mashallah Balla gaye2 rek forever

  35. Baye saliou Diagne
    Baye saliou Diagne
    Hace 8 días

    Machaalla eumue sene ndam rék inchaalla

  36. Mamadou Diallo
    Mamadou Diallo
    Hace 8 días

    Ndam reck eumeu vous êtes genti

  37. NGAGNE LO
    NGAGNE LO
    Hace 8 días

    Geumnané dounou borom dinamaye ndame niailay Nianall mobari

  38. NGAGNE LO
    NGAGNE LO
    Hace 8 días

    Mais yarounga trop Dina wakhe sama Mame mounianall la insahala

  39. bouba sarr
    bouba sarr
    Hace 8 días

    Eume amal diame way💗💗💗💗💗

  40. Ngagne Diouf
    Ngagne Diouf
    Hace 8 días

    Eum le champion des champion,nioniou tok fofou yépp dane gualén yay champion tmt...

  41. Moussa Dione
    Moussa Dione
    Hace 9 días

    Sama mbeur eumeu sene dame rék inchallah

  42. Ibrahima Nging
    Ibrahima Nging
    Hace 9 días

    Toul temps sport sou boléwoul waroule takhalé machahala eumeu sene yalanaco yalla may ndam

  43. Cheikh Baldé
    Cheikh Baldé
    Hace 9 días

    Machalla li rafetna bg2 yalla nala yalla may ndam 🤲

  44. Songjunior Thiam
    Songjunior Thiam
    Hace 9 días

    Mane Lou mélni la beugeu si guisse si EStitle bi yallah xamnako . Li dafa nice quoi. Yallah na sén diam yageu

  45. Tapha Kara
    Tapha Kara
    Hace 9 días

    Nice na

  46. Matoulove MA
    Matoulove MA
    Hace 9 días

    Merci beaucoup à toi

  47. makhtar seck
    makhtar seck
    Hace 9 días

    Eumeu sene yallanala yalla maye ndame

  48. Dija Cisse
    Dija Cisse
    Hace 9 días

    Lii tamit da melni wa droit gnoyy gagné

  49. BAM'S BAM'S
    BAM'S BAM'S
    Hace 9 días

    Eumeu yalnala bour yalla défal diame amine/ lac ame ndam si yaw si barki séydina mouhamed psl amine🙏

  50. Ablaye Ndiaye
    Ablaye Ndiaye
    Hace 9 días

    Nala yalla may ndam barkep s bamba 🙏

  51. Ndiaye Mansour
    Ndiaye Mansour
    Hace 9 días

    Man de blh eumeu sén rk la faral beugue ko loll bilahi walahi mais lima beugue rk mou defal mako moye mou Balou balla gaye 2 si lim ko wakhon blh kon Dina kontan trop eumeu yalna nala yalah maye ndam linga beugue yalnako yalah defal nekal si diame alkhamdoulilah

  52. SABALY Hadji
    SABALY Hadji
    Hace 9 días

    Ndame rek champion

  53. amadou souare
    amadou souare
    Hace 9 días

    C'est bien eume sene pape sarr et le grand bras droit landiane

  54. Coura Faye
    Coura Faye
    Hace 9 días

    Machaala li rafetna

  55. dame mbengue
    dame mbengue
    Hace 9 días

    Lutte TV ❤️🔥

  56. dame mbengue
    dame mbengue
    Hace 9 días

    Balla gaye ❤️💪

  57. Abasse Cisse
    Abasse Cisse
    Hace 9 días

    Machalla champions contane na si reconnaissance bi en vers ton amie

  58. Aliou Diouf
    Aliou Diouf
    Hace 9 días

    Merci beaucoup eume ligua def nice na trop yalla na yalla fey sa khol

  59. Mamadou Mare
    Mamadou Mare
    Hace 9 días

    Eumeu Sene une grande référence, un exemplaire sans faille tjrs égale à lui mm. Entendre eumeu Sene parler me fait plaisir. Longue vie à toi et à toute ta famille qu'Allah le tout puissant et le seul et unique détenteur des pouvoirs vous protège et vous assiste dans vos nombreuses entreprises.

  60. MAKHA HANE SOPE SERIGNE TOUBA
    MAKHA HANE SOPE SERIGNE TOUBA
    Hace 9 días

    Eumeu sene yalnala yalla maï ndam sikaw lac de guiers de Aminee yarabi 🤲🤲🤲

  61. Milck Sane
    Milck Sane
    Hace 9 días

    Que dieu donne la Victoir Eumeu sène insa'allah combat contre lac2

  62. Babacar Khaba
    Babacar Khaba
    Hace 9 días

    Vrai trompeur nandite yi xame nagne la déh guaye coman on dort

  63. Amy colle Mboup
    Amy colle Mboup
    Hace 9 días

    Machala li dafa nice

  64. Talla Cisse
    Talla Cisse
    Hace 9 días

    Mais nak Eumeu j'ai l'impression que tu t'es pas bien entraîné pour ce combat

    1. saliou diouf
      saliou diouf
      Hace 8 días

      Comment tu peux savoir ça

  65. Talla Cisse
    Talla Cisse
    Hace 9 días

    Eumeu li gua sole nicena torop

  66. Yacine bou balla guaye2
    Yacine bou balla guaye2
    Hace 9 días

    Machalla j'aime beaucoup mon petit frère Balla gaye 2 c'est mon lutteur préfère mais je respecte tous les frères lutteurs nous sommes des Sénégalais et la vie est courte la lutte est un travail après la vie continue nékaléne sy diam rék Amine yarabi 🙏❤️❤️❤️❤️🙏

    1. Yacine bou balla guaye2
      Yacine bou balla guaye2
      Hace 8 días

      @Adama Seck Machalla mon frère comme toujours vous dite la vérité machalla 🙏❤️❤️❤️❤️🙏

    2. Adama Seck
      Adama Seck
      Hace 8 días

      Deugue nekhoul baniouniou ken mé nak balla gaye mo dei souniou xole ❤️❤️❤️

  67. Nabou Samb
    Nabou Samb
    Hace 9 días

    Machallah nitte kou bakh machallah

  68. dieng mouhamed
    dieng mouhamed
    Hace 9 días

    Bilahi pape sarr danga bakh rk diame si iow ému yalla naka yalla maye ndame bou sed goy si barki yalla amine

  69. Mohamed Ndiaye
    Mohamed Ndiaye
    Hace 9 días

    Wouly sa médicaments dou yombou

  70. Modou Diaw
    Modou Diaw
    Hace 9 días

    ❤❤❤❤❤🥰🥰🥰🙏🙏🙏🙏

  71. Mohamed Benzékry
    Mohamed Benzékry
    Hace 9 días

    Eumeu dafmay fathie 😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  72. Amadou Sow
    Amadou Sow
    Hace 9 días

    Eumeu sène origina nite le amèricainyi gnoko dèfare made in usa le

  73. Amadou Sow
    Amadou Sow
    Hace 9 días

    Ama baldè original nite le amèricain yi gno ko dèfar made in usa le

  74. Amadou Sow
    Amadou Sow
    Hace 9 días

    Eumeu séne original nite le amèricain yi gno ko dèfar made in usa le

    1. Amadou Sow
      Amadou Sow
      Hace 8 días

      @Bara Diakité dègloma djiko amèricain laye wakhè

    2. Bara Diakité
      Bara Diakité
      Hace 8 días

      made in Sénégal le,kougina nek sénégalais nite daa am,naniou fonk souniou poppe ,Lou américain oppou sénégalais ci nite

  75. FATOU SECK
    FATOU SECK
    Hace 9 días

    PAPA LAMINE SECK Nice

  76. adu boi
    adu boi
    Hace 9 días

    I’m not a fan but I like his attitude 💯

  77. Cheikh VIP
    Cheikh VIP
    Hace 9 días

    Balla boulko ñanal yalla nala lac dane dh🤣

    1. WARRIOR KEMI SÉBA
      WARRIOR KEMI SÉBA
      Hace 8 días

      LAC d bou andone ak Malaaka sah, doutakh mou ñémé, loolou rek mooma ci diaakhal

  78. Isidore Memdy
    Isidore Memdy
    Hace 9 días

    Eumeu Yalla na la yalla may ndam champion ♥️♥️ dila begueee

  79. Kine Diallo
    Kine Diallo
    Hace 9 días

    Eumeu séne Balla Gaye Masha allâh nice na GM 👏👏♥️♥️

  80. BAYE POSE
    BAYE POSE
    Hace 9 días

    Eumeu sene paréwo dh Bakhna

  81. Bebe eumeu
    Bebe eumeu
    Hace 9 días

    Macha Allah

  82. Amèt Dia
    Amèt Dia
    Hace 9 días

    Eumeu sen yalla nala yalla lafal thiat rekk te maye la ndam rek inchallaho rabi

  83. sara couture coutur
    sara couture coutur
    Hace 9 días

    emue rek

  84. sara couture coutur
    sara couture coutur
    Hace 9 días

    💯❤💯

  85. Malick Sarr
    Malick Sarr
    Hace 9 días

    Eumeu Sene la farale yalnako yalla Maye ndame

    1. Mc Soldat
      Mc Soldat
      Hace 7 días

      Amine

    2. Mouhamed Ndong
      Mouhamed Ndong
      Hace 7 días

      Amine

  86. Omar Papis Messi
    Omar Papis Messi
    Hace 9 días

    insha'Allah dam rk eumeu🔥

  87. ndongo ndiaye
    ndongo ndiaye
    Hace 9 días

    Eumeu dafa bakhe

  88. Pape moussa Kandéla
    Pape moussa Kandéla
    Hace 9 días

    Le grand champion eumeu Séne

  89. Modou Sene
    Modou Sene
    Hace 9 días

    Lolou deh yekini defalouko wakho il est avare

  90. Malika Sarr
    Malika Sarr
    Hace 9 días

    Yalla na yalla maylla dam

  91. Demba Pamm
    Demba Pamm
    Hace 9 días

    Balla gaye Ama baldé gouye gui lac yalnaléne yalla may ndam inchallah

  92. Boukary Wagne
    Boukary Wagne
    Hace 9 días

    Mom bro bakh la

  93. diaw Tapha
    diaw Tapha
    Hace 9 días

    Oustaz Balla guaye adouna amoule bena sollo bilae

  94. Demba Pamm
    Demba Pamm
    Hace 9 días

    Jeste bi raféte n'a mais yalna yalla may lac de guére ndam si kaw eumeu séne inchallah

  95. Awa Diakhate
    Awa Diakhate
    Hace 9 días

    limine bougniou sonal ak lamb deukeubi dafa mèty

    1. Diaw Wade
      Diaw Wade
      Hace 9 días

      Ioe mom danga dof

  96. lahad bou kharagne Lo
    lahad bou kharagne Lo
    Hace 9 días

    Pape Sarr 🤣🤣🤣

    1. Mansour Dieng
      Mansour Dieng
      Hace 8 días

      Aï Waye Boul Ko Rétane

  97. lahad bou kharagne Lo
    lahad bou kharagne Lo
    Hace 9 días

    Eumeu B52 ndam RK niougui sen guinaw

  98. lahad bou kharagne Lo
    lahad bou kharagne Lo
    Hace 9 días

    Yénen promoteur yéwoulen Gaston dalen di tec khel RK mom mouna teugue 8 kilo mom ak macky gnô yamm RK

  99. lahad bou kharagne Lo
    lahad bou kharagne Lo
    Hace 9 días

    Eumeu sen bandit la quoi mes linga changer rafetna torop ndam RK inchallah

    1. Thieno Diallo
      Thieno Diallo
      Hace 8 días

      @Moustapha Gaye bou ler ga wah 😂😂😂

    2. Moustapha Gaye
      Moustapha Gaye
      Hace 8 días

      @Thieno Diallo bilahi bayi si xél rék kosi waxtanal lolou rék lalay wax

    3. Thieno Diallo
      Thieno Diallo
      Hace 8 días

      @Moustapha Gaye 😂😂😂😂😂🏃🏃🏃🏃🏃

    4. Moustapha Gaye
      Moustapha Gaye
      Hace 9 días

      Déll weur di commentaire rék bilahi fans Modou yi yeup ay waxou mystique rék lagni wax

  100. Jean collin Sarr
    Jean collin Sarr
    Hace 9 días

    Eumeuu séne billae damala beugue Yalna yalla samla té takhawoula mayla ndame